Matthew 16:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu woññiku, daldi ne Piyeer: «Sore ma Seytaane, bu ma xatal; yëfi nit ngay fonk, waaye du yëfi Yàlla.»