Matthew 16:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it moom àddina sépp lu muy jariñ nit, bu ñàkkee bakkanam? Te nit, lu mu war a weccee bakkanam?