Matthew 16:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci dëgg maa ngi leen koy wax, am na ñi fi taxaw, ñoo xam ne duñu dee, te gisuñu Doomu nit ki ñëw ci nguuram.»