Matthew 16:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu yég loolu ne leen: «Yéen ñi néew ngëm, lu tax ngeen di werante ci seen biir, ndaxte indaalewuleen mburu?