Matthew 17:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Juróom-benni fan gannaaw gi, Yeesu àndoon na ak Piyeer, Saag ak Yowaana rakkam, yóbbu leen fu wéet ci tund wu kawe lool.