Matthew 18:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Te it wottuleen a xeeb kenn ci ñi gën a tuuti, ndax kat seeni malaakaa ngi sax ci jataayu sama Baay bi nekk ci kaw. Maa leen wax loolu.