Matthew 18:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ko gisee, mbég mi mu am ci moom mooy ëpp mbég, mi mu am ci juróom-ñeent-fukki xar ya ak juróom-ñeent ya réerul.