Matthew 18:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bu la dégluwul, àndal ak kenn mbaa ñaar, ngir mbir mi dëggu ci li ko ñaar walla ñett seede.