Matthew 18:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu leen dégluwul ñoom itam, wax ko mbooloom ñi gëm. Bu dégluwul mbooloo ma nag, nga teg ko ni ku gëmul Yàlla mbaa ab juutikat.