Matthew 18:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Maa ngi leen koy wax it, bu ñaar ci yéen déggoo ci àddina, ngir ñaan lu mu man a doon, sama Baay bi nekk ci kaw dina leen ko may.