Matthew 18:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
waaye jaraaf ja amul lu mu feye. Kon nag sangam santaane, ñu jaay ko moom ak jabaram ak ay doomam ak lépp lu mu am, ngir fey bor ba.