Matthew 18:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
ne leen: «Ci dëgg maa ngi leen koy wax, su ngeen woññikuwul ci Yàlla, ba mel niy xale, dungeen dugg mukk ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.