Matthew 18:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kuy suufeelu nag, ba mel ni xale bii, kooku mooy ki gën a màgg ci nguuru Yàlla Aji Kawe ji.