Matthew 18:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Yaw àddina dinga torox ndax say fiir yiy yóbbe nit bàkkaar. Fiir mënta ñàkk, waaye toroxte dal na nit ki koy lal.

Recommended Reading