Matthew 19:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko taalibe ya déggee, ñu ne ko: «Bu dee noonu la digganteb góor ak jigéen mel, bañ a séy moo gën.»