Matthew 19:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte am na ñu judduwaale tële, am na ñu tële ci loxoy nit, te am na ñu bañ a séy ngir nguuru Yàlla Aji Kawe ji. Ku ko man a nangu, nangu ko.»