Matthew 19:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu amoon na ay nit ñuy indil Yeesu ay xale, ngir mu teg leen ay loxoom, ñaanal leen. Waaye taalibe ya gëdd leen.