Matthew 19:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko Piyeer déggee, mu daldi ne: «Waaw nun nag, dëddu nanu lépp, topp la; kon nu nuy mujje nun?»