Matthew 19:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu fa nekkee, ay Farisen ñëw ci moom, bëgg koo fiir; ñu ne ko: «Ndax jaadu na nit fase jabaram, saa su ko neexee?»