Matthew 19:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu leen: «Musaa may na leen, ngeen fase seen jabar, ndax seen xol dafa dëgër, waaye ca njàlbéen ga demewul woon noonu.