Matthew 19:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it maa ngi leen koy wax, koo xam ne kii fase nga sa jabar te du njaaloo tax, boo séyaatee ak keneen, njaaloo nga.»