Matthew 2:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu ko defee Yàlla artu na leen ci biir gént, ñu bañ a dellu ca Erodd. Noonu ñu jaar weneen yoon, ñibbi seen réew.