Matthew 20:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Noonu nguuru Yàlla Aji Kawe ji dafa mel ni boroom kër bu génn ci suba teel, ngir jël ay liggéeykat ndax toolu réseñam.

Recommended Reading