Matthew 20:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye boroom kër ga tontu kenn ci ñoom ne ko: “Sama waay tooñuma la. Ndax juboowunu woon ci benn denariyon?