Matthew 20:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Nu ngi jëm Yerusalem, te dees na jébbal Doomu nit ki saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya. Dinañu ko àtte, teg ko dee,