Matthew 20:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
jébbal ko ñi dul Yawut, ngir ñu di ko ñaawal te di ko dóor ay yar, ba noppi daaj ko ci bant. Waaye ca ñetteelu fan ba dina dekki.»