Matthew 20:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu woo leen ne leen: «Xam ngeen ne ci xeeti àddina, njiit yi dañu leen di dóor yetu nguur, te kilifa yi dañu leen di noot.