Matthew 20:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte noonu la Doomu nit ki ñëwe, du ngir ñu nekk ay surgaam, waaye muy seen surga, ba joxe bakkanam ngir njotug ñu bare.»