Matthew 20:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nit ña gëdd leen, ngir ñu noppi. Teewul gumba ya gën a yuuxu naan: «Sang bi, yaw Sëtu Daawuda bi, yërëm nu!»