Matthew 21:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu tontu Yeesu nag: «Loolu xamunu ko.» Noonu Yeesu ne leen: «Kon man itam duma leen wax ci ban sañ-sañ laay defe yëf yii.