Matthew 21:45 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nga xamee ne saraxalekat yu mag ya ak Farisen ya dégg nañu léebam yooyu, ñu xam ne ñoom lay wax.