Matthew 21:46 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu di ko fexee jàpp, waaye ragal nañu nit ña, ndaxte ñépp teg nañu ko ab yonent.