Matthew 22:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Bi nga xamee ne buur bi dugg na nag, ngir seetsi gan yi, mu gis fa nit ku solul mbubb mu ñu war a sol ca céet ga.