Matthew 22:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Kilifa gi, Musaa nee woon na: “Boo xamee ne góor dee na te amul doom, na rakkam donn jabaram, ngir sàkkal magam njaboot.”