Matthew 22:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu yónni ay surgaam, ngir ñu woo gan yi ca céet ga, waaye gan yi bëgguñoo ñëw.