Matthew 22:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Noonu buur mer, daldi yónni ay xarekatam, ngir ñu rey bóomkat yooyule, lakk seen dëkk.