Matthew 23:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Farisen yu gumba yi! Jëkkleen a setal biir kaas bi ak ndab li, ngir biti bi itam set.