Matthew 23:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen itam, ci ngistal dangeen a mel ni ñu jub, waaye ci seen biir dangeen fees ak naaféq ak lu bon.