Matthew 23:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te yéena ngi wax ne: “Bu nu fekke woon sunu jamonoy maam, dunu ànd ak ñoom ciy tuur deretu yonent yi.”