Matthew 23:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Dañuy def seeni jëf yépp, ngir nit ñi gis leen, di takk ay téere yu réy, tey réyal seeni laari mbubb.