Matthew 23:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yéen buñu leen wooye “Kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen Kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.