Matthew 23:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te buleen tudde kenn seen “baay” ci àddina, ndaxte kenn rekk moo di seen Baay, ki ci kaw.