Matthew 24:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu waxee ba noppi, mu génn ca kër Yàlla ga, dem. Noonu ay taalibeem ñëw ci moom, ngir won ko tabaxi kër Yàlla ga.