Matthew 24:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu xebaar bu baax bii ci nguuru Yàlla, dees na ko yégle ci àddina sépp, ngir mu nekk seede ci xeet yépp. Bu loolu amee muju jamono ji jot.