Matthew 24:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye mu tontu leen ne: «Du gis ngeen yii yépp? Ci dëgg maa ngi leen koy wax, lii lépp dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»