Matthew 24:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te bu ñu wàññiwul bés yooyu, kenn du mucc, waaye dees na leen wàññi ndax ñi Yàlla tànn.