Matthew 24:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Waaye bés booba walla waxtu wa, kenn xamul kañ lay doon; du malaaka yi ci kaw, du sax man Doom ji, waaye Baay bi rekk moo ko xam.