Matthew 25:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Noonu Buur bi dina wax ñi féete ndeyjoor: “Agsileen, yéen ñi sama Baay barkeel, jël-leen nguur, gi ñu leen waajal li dale ci njàlbéenug àddina.