Matthew 25:40 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Buur bi dina leen tontu ne: “Ci dëgg maa ngi leen koy wax, saa yu ngeen defalee loolu kenn ki gën a ndaw ci sama bokk yii, man ngeen ko defal.”