Matthew 25:45 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon dina leen tontu ne: “Ci dëgg maa ngi leen koy wax, saa su ngeen ko defalul kenn ci ñi gën a ndaw, man ngeen ko defalul.”